Xam sa démb, xam sa tey

SAMBA GUELADJI


Listen Later

Sàmba Gellajo jeegi mi judoo daanaka Fukeelu xarnu ak juróom ñaar ca Jowol Worgo ca Maatam. Doomu Gelaajoo Jéegi la . Yoroom na nguur gi ñéenti yoon digante 1724 ak 1742.

...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Xam sa démb, xam sa teyBy Goethe-Institut