Layene Digital

Zikrullah - Ñaanu Maam Njoon ak Baay Aboo


Listen Later

Ñu baax ñii ku leen woy da ngay am ngërëm

Yonnen doomi yonnen Bilaay ñeey ngalam

Limamook njaboot am da ñoo jàlla yii

Yonnen daal dadul kem, xana ñooy ngalam


#Layenedigital #layene #zikr

...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Layene DigitalBy LayeneDigital