Layene Digital

Zikrullah - Ñaanu Seydi Raan & Maam Ala


Listen Later

Jërëjëf Imaama Laahi yaa nu xamal yoon wa

Dugël nu sañey Buur Yàlla miy sàmm jaamam baa

Sañey Yàlla miy Buur moodi wax "laa ilaaha illa Laahu

Ku kay salloo du feerook meram Buur baa


#layenedigital #layene #islam #prieres #education #zikr

...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Layene DigitalBy LayeneDigital