Wolof Podcast

Bëgg a baax (ñaareelu xaaj bi)


Listen Later

Tay ñuy yéggali suñu waxtaan bi ñu tambali woon ci yoonu mbaax doon yaatal ci lan la nit ki wara def ngir am ak njub ak sellal. Bii ma mujjee tudd nak ñu koy sàkkoo ci tariqa. Mu mel ni kon mat na laaj kuy Sëriñ bu mat Sëriñ ak lan la fa taalibe bi war a sàkku. Yal nanu Yàlla defal njub ak mbaax.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw