Sign up to save your podcasts
Or

Ca biir tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.
Ñaari yoon, mu am ñu koy jeema baayiloo gëstoom: posaneko ak capaloo ca Boubon; di fexee it mu baña taseek profesër Kouada ca Niamey.
Ci ndimalu Nathalie,la gisee tuuti ca mbóot ma doon ubbi dencukaay bu yeemee ba "Sahel vert".
(Pour faire les exercices, faites défiler les diapositives vers la droite ►►►)
► EXPLICATIONS
► EXPRIMER LE BUT / LES DIRECTIONS
Le verbe « partir »
Pour donner des directions, on utilise les expressions suivantes :
Pour situer un lieu, on utilise les expressions suivantes :
Pour exprimer un but, on utilise :
By Français Facile - RFICa biir tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.