Sign up to save your podcasts
Or

Ca biir  tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.
Ñaari yoon, mu am ñu koy  jeema baayiloo  gëstoom: posaneko ak capaloo ca Boubon; di fexee it mu baña taseek profesër Kouada ca Niamey.
Ci ndimalu Nathalie,la gisee tuuti ca mbóot ma doon ubbi dencukaay bu yeemee ba "Sahel vert". 
► EXERCICES
(Pour faire les exercices, faites défiler les diapositives vers la droite ►►►)
► EXPLICATIONS
► ARTICLES DÉFINIS ET INDÉFINIS
On utilise l’article défini quand on parle d’une personne ou d’un objet qui a déjà été mentionné.
On utilise l’article indéfini quand on parle d’une personne ou d’un objet qui n’a pas encore été mentionné.
Lorsqu’on peut compter (dénombrable) :
Lorsqu’on ne peut pas compter (indénombrable) :
By Français Facile - RFICa biir  tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.