Sign up to save your podcasts
Or

Kwame surgab tóokóor la ca Gorom-Gorom, ca Burkina Faso. Njaatigeem, porfesër Omar Seku, da ñu koo gëfoon ca kanamam. Ca biir xeex ba, gàllaajam dammu.
Kwame dem di wëri Omar ma doon jeema dekkalaat ndànd foy-foy gi. Ku ko gëf?
Gëf ga ak gàllaaj ku doy waar gi ndaq da ñoo am lu ñu joteek leebu bajani Kwame ja? "Deklul ngelawli, Sahara munge jooy. Dafa buga naataat. Bena bes Bena bes dina am nit ku ñew. Dina dekkelaat gañcax ak garap yi... "
(Pour faire les exercices, faites défiler les diapositives vers la droite ►►►)
► EXPLICATIONS
Dire l’heure : Il est…
Prendre rendez-vous : Rendez-vous à…
Dire la nationalité
Niger : Il est nigérien ; elle est nigérienne.
France : Il est français ; elle est française.
Afrique du Sud : Il est sud-africain ; elle est sud-africaine.
By Français Facile - RFIKwame surgab tóokóor la ca Gorom-Gorom, ca Burkina Faso. Njaatigeem, porfesër Omar Seku, da ñu koo gëfoon ca kanamam. Ca biir xeex ba, gàllaajam dammu.