Wolof Podcast

"Féminisme" (xaaj bu njëkk)


Listen Later

Tay ñuy waxtaane « féminisme ». Ma ànd ci ak Seexunaa Njaay di ab gëstu kat di jàngale kat. Ndax lii di « féminisme » dëppoo na ak suñu gis-gisu reew? Lutax lu ci ëpp ñuy seetlu ñàkk a dëppo. Lii ak yaneen lanu doon yaatal vi xaaj bu njëkk bi.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw