Sunu episode bu njëkk ñuy waxtaane « identité culturelle » : ndax dañoo ñàkk suñu mbaatit (culture) ginnaaw bi Tubaab yi ñëwee suñu réew yi noot ñu? Ndax xeebuñ suñu bopp ginnaaw loolu? Ndax jéem nanu dellu suñu bopp? Mu nekk ay laaj yu bari yoo xamne mat na waxtaane. Ak téereeb Ken Bugul bi tudd « Le Baobab fou » lañuy jéema saytu laaj yi yépp.
[email protected]