Wolof Podcast

intro


Listen Later

Tay ñuy def benn tambali bu ndaw ngir dégtal leen suñu « podcast » bi ñu am yéene tambali. Ñuy wax lutax ñu fas ko yéene def ci kàllaama wolof, yan woppa (sujets) lanu fas yéene waxtaane ak ki kay def mooy kan. Ci tënk lii ag ubbite la

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw