Wolof Podcast

Jàngee Almãñ (étudier en Allemagne)


Listen Later

Tay ñu dikkaat ak yeen ci wolof Podcast di def ay leeral ak laaya biir ci képp koo xam ne daa ngaa bëgg a ñëw Almãñ jàngee ci fi. Ban yoon ngay jaar ba mën a ñëw jàngee fii? Lan nga war a mën a jàng ngir ëlëk nga man a ligéey te doo am benn jafe-jafe? Lan la jàng bi laaj? Yii laaj lanuy jéema tontu ci waxtaan wi.

https://www.uni-assist.de/en/
https://www.daad.de/en/study-and-research-in-germany/plan-your-studies/requirements/

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw