Sign up to save your podcastsEmail addressPasswordRegisterOrContinue with GoogleAlready have an account? Log in here.
Suniouy wakh si migration fi sénégal, liniouy geuneu xalaat moy ay ndaw you goor yuy dieul gaal nguir dem Espagne. Wayé daniouy faté ni si biir tukki katt yoyou amna ay jiguén. Hosted on Acast. See... more
FAQs about Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna:How many episodes does Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna have?The podcast currently has 8 episodes available.
March 14, 2024E7 - Ndiangatu tukkiÉpisode bou moudjou si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more10minPlay
March 13, 2024E6 - Dianguekatt doxandem yi nekk DakarDiourom bennelou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more9minPlay
March 12, 2024E5 - Tukki ak ay guéntam yu ñawDiouromélou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more8minPlay
March 11, 2024E4 - GP biNientélou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more8minPlay
March 10, 2024E3 - Dieul gaal wala deet ?Niétélou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more10minPlay
March 09, 2024E2 - Jaar-jaaru AissatouNiarelou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more10minPlay
March 08, 2024E1 -- Li waral ñuy tukkiÉpisode bou ndieuk si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more10minPlay
February 12, 2024E0 - TeaserBande-annonsou série « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » Podcast bi amna 7 épisodes gni ko réalisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information....more2minPlay
FAQs about Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna:How many episodes does Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna have?The podcast currently has 8 episodes available.