Wolof Podcast

Néegu séy


Listen Later

Néegu séy lañuy waxtaane tay. Ñu setlu at yi weesu amna ay soppiku yu mag ci pénc mi. Séy yi barina ay jafe-jafe lool. Ñuy def taxaw setlu ngir man a xam luko waral ak yan saafara lanu ci man a indi. May dalal Soxna Coro Coor muy yëngu ci „aide au développement“.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw