Raam Dox : le podcast à la sénégalaise

#8 Nék jigeen biir Sénégal (le statut de la femme au Sénégal)

10.27.2023 - By Assiya Thiam GueyePlay

Download our free app to listen on your phone

Download on the App StoreGet it on Google Play

Salam, Salam !

Dans cet épisode, je parle du statut (dans son ensemble) de la femme dans la société sénégalaise. 

Dañuy faral di dégue "jiguène ni la wara mél", "kou bax sa ndeya tax" wala "ligueyou ndey anioub doom" lane lay téki thi suñu société ? 

Dañuy faral di guiss ñéne si ñoune di doundou lou méti té douñou saña wax ... 

Dina dioxé sama xalate si yéne wax yigua xamné moy ték pression jigeen you beuri thi souñou biir société. 

Dalal ak diam.

Partages ton témoignage ici : [email protected]

Instagram : raam_dox

Tiktok : raam_dox

Youtube : raam dox 

Hébergé par Ausha. Visitez ausha.co/politique-de-confidentialite pour plus d'informations.

More episodes from Raam Dox : le podcast à la sénégalaise