Wolof Podcast

Seex Ibra Faal


Listen Later

Tay nuy waxtaane jëmm ju am solo te mooy Seex Ibra Faal. Barina loolu lu ñu mën a jàngee ci moom ndax yiteem ju kawe. Mu nekk jëmm ji wone Seex Ahmadu Bàmba ba noppi wone nan lanu ko war a toppe ngir jariñu ci moom. Daan na wax naan Sëñ Bàmba mooy dëkk bi, man Ibra Faal maay yoon bi ciy dem. Naan la def ba taxawal loolu ak lan lanu ci mën a jàngee?

Baay Lahat
[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw