Wolof Podcast

Senegaal ndax dëkk la?


Listen Later

Tay nuy waxtaan ci tolluwaayu reew mi. Jafe-jafe yi waa reew mi di dund luko waral ak yan jàngat lanu ci man a def. Senegaal kuy wax te Yàlla tax xamni doxul ci yoon. Loolu bokk na ci li waral nit yi fippu ngir mën a jotaat seen àq.
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw