Wolof Podcast

„séries sénégalaises“


Listen Later

At yii ñu weesu gis na ñu ni „séries sénégalaises“ bari nanu loolu. Ñu gis ci tamit yu bees yu bari yoo xamni miinu ñu ko woon ci réew cig fësal. Mootax ñuy def taxaw setlu di jàngat jafe-jafe yi mu mën a indi ci pénc mi. Ma àndaat ci ak jëwriñ Bàmba Jaw.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw