Wolof Podcast

Sëriñ bu mat Sëriñ


Listen Later

Lan mooy Sëriñ bu mat Sëriñ? Ñu gis ne tay lu ëpp ci nit yi am nanu tariqa bu ñu bokk ak ci Sëriñ yu ñu jokku? Waaye lan lanu fay sàkku ak kooku nan la war a mel? Yan jikko la war a yor? Ci waxtaan bii yii ak yaneen lanuy yaatal di ci jéema indi ay leeral ak laabire. Ñu ànd ci ak jëwriñ Bàmba.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw