Sunu Yaakaar

Sunu Yaakaar

By Serigne Malick DiopReligion & Spirituality
Download on the App Store

Sunu Yaakaar episodes

  • 19. Buuru Ndam - Nguur gu mag gu Buur bi 01
    Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga.
    Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
    © 2019 ROCK International king-of-glory.com
    6 min
  • 18. Buuru Ndam -Jikkoy Buur bi

    7 min
  • 17. Buuru Ndam - Yeesu ci Misira

  • 16. Buuru Ndam - Juddub Yeesu

    10 min
  • 15. Buuru Ndam - Duggsig Buur bi

  • 14. Buuru Ndam - Tére yonent yi

    8 min
  • 13. Buuru Ndam - Yoonu Musaa

  • 12. Buuru Ndam - Ibrahima mooy xaritu Yalla
    Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga.
    Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
    © 2019 ROCK International king-of-glory.com
    6 min
  • 11. Buuru Ndam - Pexem Yàllaa ngi jëm kanam ak Ibrahima
    Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga.
    Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
    © 2019 ROCK International king-of-glory.com
    9 min
  • 10. Buuru Ndam - Fippug nit ak takkuteg Yàlla
    Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga.
    Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
    © 2019 ROCK International king-of-glory.com
    9 min

About Sunu Yaakaar

From the publisher's feed

Toppal sunu emission ci facebook.com/sunuyaakaar