Tay ñuy yegali waxtaan bi ñu tambali woon ci yàqu-yàqu jikko yi ak liko sabab. Ci xaaj bi mujj bi ginnaw bi ñu indee safaan yi ak liko waral, ñuy jeema indi ay safara