Wolof Podcast

yàqu-yàqu jikko yi (xaaj bu njëkk)


Listen Later

«Danoo xëm te ñor a gu ñu » Sëriñ Saam Mbay.

Tay ñuy waxtaane yàqu-yàqu jikko yi ànd ci ak Seex Aliw Saar. Ku am seetlu tuuti dina xam ni sunu reew mi fi mu tollu ci jikko yu yàqu kéeman la. Lan mooko sabab ak lan mooy saafara ci? Ci waxtaan bi di nanu ci yaatal lu bari ci ñaari xaaj

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw