Wolof Podcast

Yebbi


Listen Later

Yebbi mooy lan? Tay ñuy waxtaane lu am solo te yaatu lool ci biir reew mi. Yebbi yégg ma foo xamni jéggi na dayo loolu. Bari na kër walla sëy yu co yëngi. Mu melni li nekkoon cosaan li ak lika taxoon jóg xamatuñ ko. Limiy yàq ëpp fuuf limiy defar. Ñu ànd ci ak Mère Dior Sow.

[email protected]
...more
View all episodesView all episodes
Download on the App Store

Wolof PodcastBy Lahat Diaw