Sign up to save your podcastsEmail addressPasswordRegisterOrContinue with GoogleAlready have an account? Log in here.
Tay ñuy def benn tambali bu ndaw ngir dégtal leen suñu « podcast » bi ñu am yéene tambali. Ñuy wax lutax ñu fas ko yéene def ci kàllaama wolof, yan wopp (sujets) lanu fas yéene waxtaane ak ki kay def ... more
FAQs about Wolof Podcast:How many episodes does Wolof Podcast have?The podcast currently has 23 episodes available.
January 21, 2022Bëgg a baaxTay ma ànd ak sama gan gu njëkk muy Bàmba ñuy waxtaane yoonu njub ak baax. Def lu baax yomb na waaye dëkk ci moo jafe. Yonent bi (saws) dafay wax ni àddina mooy aljànna ki weddi, waaye kaso la ci ki gëm. Mu melni kon ku bëgg dund ci niki Yàlla gërëmee dina laaj jékki ay jéego jëm ci yar sa bakan ak topp Yàlla. Waaye mu nekk yoon bu meti loolu. Lan mooy yoonu njub? Ak yan jafe-jafe la doomu aadama bi di dajeek ngi yégg baax? Ci tënk loolu lanuy waaxtaane ci épisode bii.[email protected]...more45minPlay
January 08, 2022Identité culturelle (xam sa bopp ak sa mbatit)Sunu episode bu njëkk ñuy waxtaane « identité culturelle » : ndax dañoo ñàkk suñu mbaatit (culture) ginnaaw bi Tubaab yi ñëwee suñu réew yi noot ñu? Ndax xeebuñ suñu bopp ginnaaw loolu? Ndax jéem nanu dellu suñu bopp? Mu nekk ay laaj yu bari yoo xamne mat na waxtaane. Ak téereeb Ken Bugul bi tudd « Le Baobab fou » lañuy jéema saytu laaj yi yépp.[email protected]...more46minPlay
January 01, 2022introTay ñuy def benn tambali bu ndaw ngir dégtal leen suñu « podcast » bi ñu am yéene tambali. Ñuy wax lutax ñu fas ko yéene def ci kàllaama wolof, yan woppa (sujets) lanu fas yéene waxtaane ak ki kay def mooy kan. Ci tënk lii ag ubbite la[email protected]...more9minPlay
FAQs about Wolof Podcast:How many episodes does Wolof Podcast have?The podcast currently has 23 episodes available.